Grand Plateau 17 Juillet 2021 avec Serigne Moustapha Dramé Yallay Kassè et Serigne Abdoulaye Ndiaye
67,983
Reddit
Grand Plateau du 17 Juillet 2021, Moustapha Dramé et Abdoulaye Ndiaye Borom Solution, Kounkandé

Abonnez vous à notre Chaîne et Recevez les dernières informations du Sénégal

Comentarios
  • PDG
    PDG

    Hiii Aladji Babou kilifeu kokou mashallah Youssou nopil khamo diiné

  • PDG
    PDG

    Wally bim laal mola arrangé woul rék Youssou

  • PDG
    PDG

    Youssou khana doy guenth prophète Mohamed (psl )sakh danioukoy guenth fallait que nguénn kham limiy wakh

  • PDG
    PDG

    Youssou dieng dangua bokk ci weuy katt yi

  • PDG
    PDG

    Thiey Moustapha

  • Massamba Ndiaye
    Massamba Ndiaye

    Bravo serigne moustapha drame le coran est l absolu

  • omar sene
    omar sene

    machlla seringe mousthpa ❤️❤️❤️

  • Baye Moussa Ba
    Baye Moussa Ba

    Serigne moustapha damoko fan deugue rék lay wakh

  • Moussa Seck
    Moussa Seck

    Nafekh wessouwoul nitt kii di len bakhé wakhou yallah nguen beugg ko sokhor loo . Machallah defendre Islam rek ci nga nek Drame

  • Sidy Brahim Keita
    Sidy Brahim Keita

    Vous les journalistes la, franchement vous rendez l émission tro brouillon franchement et arrêtez t interprète les dits.

  • Ousmane Thioub
    Ousmane Thioub

    Drame djeureudjeuf ❣️

  • Bineta Barry
    Bineta Barry

    kou djiguéne ki di def émission bi Alima hawma na demm diangui diném migui appuyé le haram

  • Mamadou billo Diallo
    Mamadou billo Diallo

    Merci drame vous avez dit la vérité pour l amour d Allah car Allah punirai tout les sobotaire de la religion

  • Elhadji saliou woury CISSE
    Elhadji saliou woury CISSE

    Sénégal c'est foutu musique la gnouy discutè🤔ndakh aramena putin#$%

  • Amsa et Ses video
    Amsa et Ses video

    Li serigne moustapha dramé moy deug Sénégal naniou bayi nafekh

  • Issa Pouye
    Issa Pouye

    Alima deleine khole commentaires yi sénégalais yi nioye jugée Youssou dieng ak chiekh baye ayye doul katte laniou

  • Issa Pouye
    Issa Pouye

    Alima yow bayil sa doff doff lou bi

  • mor gueye
    mor gueye

    Merci seringe Moustapha daramé

  • D2A CRÉATIO officielle couture
    D2A CRÉATIO officielle couture

    Daramé mi kou yabatéla way

  • LA OU COULE DES RUISSAUX
    LA OU COULE DES RUISSAUX

    Serigne Moustapha dramé danga deugou,meusoumala dég ga waw waxét Lolou motakh malay nianal Allah geuneleu saxal si joup

  • LA OU COULE DES RUISSAUX
    LA OU COULE DES RUISSAUX

    Serigne moustapha drame yalla nala Allah fay,té taxawouleu machallah

  • Fatou Seye
    Fatou Seye

    😍😍😋❤

  • Diouf Babacar
    Diouf Babacar

    Thiama yiw mom fi amofi place

  • Diouf Babacar
    Diouf Babacar

    Moustapha daramé je t’aime

  • Utilisateur youtubiste
    Utilisateur youtubiste

    Ablaya dafa yap nityi.... Mdr mis à jour

  • suprem city tv
    suprem city tv

    Cheikh Moustapha dramé legui yaye sama Serigne wadji amoul bene xam xam 😠😠

    • Alldinal Rk
      Alldinal Rk

      Mém man

  • Cherif Diallo
    Cherif Diallo

    Yalla kessé Serigne Moustafa Dramé

  • Ndiambe Thiam
    Ndiambe Thiam

    Cheikh baye 5 litres manouko nane baye dékall koufatou yabatéga trop

  • Vivi Dao
    Vivi Dao

    Paris foot aramena, annonce aye deh tamite

  • DAOUDA sarr
    DAOUDA sarr

    Serigne Moustapha Dramé non wakhtane bi Amna Solo Machalla yallay kessé bi fégne na

  • Talla Seye
    Talla Seye

    Plateau bi kéne réck mofiye waxé xame xame s Moustapha dramé

  • Bara Toure
    Bara Toure

    Youssou Yaw Nittou Satané gua Doul kate gua

  • Mouhamadou Fadilou DIOUF
    Mouhamadou Fadilou DIOUF

    Musik defa harame deugue nekhoul mais serigne moustapha alhourane lay wakh

  • Mahamadou Diawara
    Mahamadou Diawara

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 yènè guii fowè di sabotè deen islam oustaz Dramé dafa niake fay da tu dois pas être dans se plateau de pérvére

  • Djibril Dia
    Djibril Dia

    Yaw mome youssou pour ceux qui on deja subit une formation de profiler mais yousou tu n'as pas de respect Enver les sénégalais c domage bilahi les sénégalais ne merite pas ça

  • Ass Ndiaye patriote
    Ass Ndiaye patriote

    Djibi diouf kay 😅😂

  • Kem L'officiel
    Kem L'officiel

    Moustapha dramé khamoul gate

  • bocar thiello
    bocar thiello

    Moustapha dramé machalla

  • Lodia Khalil
    Lodia Khalil

    Ndiaye Diop mii kou meneu doulllllllllllllllllllllllllllllllllll leuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuu

  • Lodia Khalil
    Lodia Khalil

    Youssou yaw do guënth sakh guiss sa bay mbeulééé 😂😂😂😂😂😂😂🤭🤭🤭🤭🤭🤭🤭🤭🤭 Dou samay wakh nak wakhou dramé laa 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • Sadio Secka
    Sadio Secka

    Dieureudieuf serigne moustapha dramè am dinè bakhna

  • Sahid Sall
    Sahid Sall

    Youssou yaw fin rek gaye deff

  • Alldinal Rk
    Alldinal Rk

    Mane damala naw s.mousstafa daram

  • MOUHAMAD AL-MAHREZ
    MOUHAMAD AL-MAHREZ

    Depuis quand les règlements religieux musulmans se mettent à jour ? Êtes vous des égarés ? Où est votre sunnah ? Où est votre religion ? Êtes vous dénoué de raison?

  • MOUHAMAD AL-MAHREZ
    MOUHAMAD AL-MAHREZ

    Ces journalistes ne savent absolument rien

  • MOUHAMAD AL-MAHREZ
    MOUHAMAD AL-MAHREZ

    Certains journalistes sénégalais doivent aller réapprendre encore

  • MOUHAMAD AL-MAHREZ
    MOUHAMAD AL-MAHREZ

    C'est grave...je me demande si on est dans un pays musulman ou juif...

  • MOUHAMAD AL-MAHREZ
    MOUHAMAD AL-MAHREZ

    Thieuy Sénégal..

  • Sahid Sall
    Sahid Sall

    شكرالك يامصطفي درام وأنت ياشيخ باي انجاي كذاب مفترتغيرأحكام الشريعة

  • thiatte sakho
    thiatte sakho

    Serigne Moustapha dramé merci bcp sa xam xam machallah✨❤️

  • Ousseynou Ndao
    Ousseynou Ndao

    Niou am xam xam deugue douniou wakh té bouniou lénko djimé niou bagne khamné yalla la

  • ousseynou sane
    ousseynou sane

    Yene mome khamna safara dal yenako mome der toublene sene wakh ouztaz drame ak kenene ki malene di fateli lailaha ila anta soubkhanaka allahouma ini kountou minal zalimina louko waral foumou dioguer ak toub bou yonente younouss toub ndakh juger nit mo takh dieune bi woneko donc li nguene di wakh charia doumanalene

  • ousseynou sane
    ousseynou sane

    Legui l'abat à distance la intention moy ndialo bou feker moy sa yener ley done ndialo bayil lene di déformer islam

  • ousseynou sane
    ousseynou sane

    Serigne moustapha drame wakhoulo deugu portable nekoul si lakhdariyou l'abat l'islam moko diguler yalla kharamal n'a kouy juger khawma bane dîner ngua diangu wayer khamoulo dara

  • ousseynou sane
    ousseynou sane

    Yalla moy KHAKIMOU le juge ouztaz drame toub ko nitou dîner ngua kene dou wakh nit foumou dieum wakhal li kouko def meunala yob safara toubko musique khamlene yonente yalla dawouda moko indi si adouna dadane weuy ba pithie yi di danou l'islam dafla wakh ni weuy bou yaroul wotewoul dioub bakhoul mais kharamoul djanguiwatal

  • Djibril Ndiaye
    Djibril Ndiaye

    Musique dfa haram s.cheikh.Ndiaye khamoul touss. Merci moustapha Dramé 🙏🏽

  • Ousmane Ndiaye
    Ousmane Ndiaye

    Signe Moustapha dramé yalnala yalla feyy Yangui défendre l'islam 🥰🥰

  • Mouhamed Ciss
    Mouhamed Ciss

    Serigne Moustapha wahgua deugg ta deugg yalla rek moko momm

  • Faty Syll
    Faty Syll

    Walahi gni khamo gnou dara khaliss lagniy weurr ces marabouts m’énervent de trop

  • Gora Ndiaye
    Gora Ndiaye

    Youssou gnémé ga.

  • Gora Ndiaye
    Gora Ndiaye

    Sama mbokki Saloum saloum bi ,drame, eupeulna touti. Meme s'il dit des verites

  • Seydou kasse
    Seydou kasse

    Seringe moustaphe est très honnête envers lui même.

  • Ngagne Mbaye
    Ngagne Mbaye

    Serigne Moustapha bayil sournalis you amoul khell yingay tokal 🙏🙏🙏

  • métro
    métro

    Wa ki koumou yappe music dafa xaram Kaye

  • métro
    métro

    Daramé Aka ame fitte dp8 temp boy. NILA méll dafa niamé deugg

  • Wagane Dione
    Wagane Dione

    Sentv yen maye baye ndiaye buzz qui dou dara kaolack khamnako bou bakh

  • Wagane Dione
    Wagane Dione

    Baye ndiaye amo kham kham serigne moustapha drame mola kene am.kham kham

  • ÀLÏõÛÑĘ Mba
    ÀLÏõÛÑĘ Mba

    Youssou dieng ioe mome do dra billlahi nah nitou adouna mola nior

  • ÀLÏõÛÑĘ Mba
    ÀLÏõÛÑĘ Mba

    Cheikh oie môme d’à ngay doul rek

  • Del Mas
    Del Mas

    Youssou do dara katal ndém feulé ki loumou wah sa baye sax meunouko dindi yalla beugoul niouy nelaw rek

  • Malick Ba
    Malick Ba

    Youssou si lo amoul xam xam bul wedi niou xam yeup xam nagn si niveau si xam. Yemal sa domaine

  • Tapha Diop
    Tapha Diop

    Man dh Mawlana Cheikh Ibrahima Niass bini askanalei sen bopou parei nek si sen yeufou chaytané yi rek moma meti vraiment wa Médina Baye warnan len wo wakh ak yen li boudon sama mbokou mourit yi ba legui lidieunti nanko da nguen wor baye nak prsk wotei woul won pour sen you niak fayda yi di deal nit gni rek

  • Ebrima ZALA Demba
    Ebrima ZALA Demba

    Sherigne drameh deug rkk ngai wakh yow music dafa haram bu bah

  • Ebrima ZALA Demba
    Ebrima ZALA Demba

    Ki fen kat bu mak la music dafa haram bahut

  • Alhagie Kebbeh
    Alhagie Kebbeh

    drame❤️❤️🙏🙏

  • Mamadou Diallo
    Mamadou Diallo

    OUSTAZ Baye contanna thi yéw s'y WAKHINN YII AMNA SOLO LOL YALLA NALÉNN YALLA FAYAL BOPAM BARKÉ MOHAMED

  • Mamadou Diallo
    Mamadou Diallo

    اسلام عليكم ورحمة الله تعالى وبركاته بارك الله فيكم جميعا ورحمه الله تعالى

  • DONA NDIAGO
    DONA NDIAGO

    Koungkandé no 2 😂😂😂😂

  • Cheikh Kandj
    Cheikh Kandj

    Youssou lo amoul xam xam boul si wéraneté

  • Cheikh Kandj
    Cheikh Kandj

    Nékhoul ba nékhoul wayé serigne Moustapha Dramé limouy wakh kénn menouko dinedi. Deugu dal nékh na khamé. Serigne Dramé ioe la andal nakh convaincre gama ❤

  • Lama Diallo
    Lama Diallo

    🤣🤣🤣🤣 dibrrll Ndiaye l'a guiss

  • DARA GHOULAMOU RASSOUL
    DARA GHOULAMOU RASSOUL

    Mbaye Ndiaye il faut revoir les obligations de la tabaski tu dis que c’est possible pour des gens qui habitent dans une même rue qui non pas de moyens de cotiser et d’acheter un bœuf pour leur tabaski cela est interdit ولم تجزفي الثمن الشركت

  • ALIOU KANE
    ALIOU KANE

    KOU BAAKH KI BOULA TOGATI AK YAW DIAKHALNAMA YI

  • Lamine Gueye
    Lamine Gueye

    Merci Serigne Moustapha drame

  • Les caprices de Nanou Diop
    Les caprices de Nanou Diop

    Deugu de dou romb noopi , music mom gnikoooy def sakh khamenagn lignioussi wakh alkhourane ak diney mooo djieuk mooo moudjier

  • Cheikh Gueye
    Cheikh Gueye

    Iow mome boula Yalla diapé ngay mis à jour alkhourane thi bakhna rekk

  • Cheikh Gueye
    Cheikh Gueye

    Youssou Dieng monon wakhhh ba musique dangane dafa harame tifakhane

  • gueye moustapha
    gueye moustapha

    Ki dou serigne

  • Ndongo Mbaye
    Ndongo Mbaye

    Sen tv ay comedien laniou dadialé rk niou diangoul niou khamoul dara si sen farata ni man

  • Mody Faye
    Mody Faye

    Y a pas de est ce que Moustapha défend l Islam et vous vs sabotez

  • Ndongo Mbaye
    Ndongo Mbaye

    Serigne moustapha gni liguay wax kawé na seni bopp

  • Mamadou Faye
    Mamadou Faye

    Billakhi Senegal mo bari nafèkh yousou verè nitou safara nga !!serigne moustapha dramè waro sskh tog ak gni nitou seytane késsé lagne

  • Le Patriote
    Le Patriote

    Youssou nafékh deug la.

  • اهلا وسهلا
    اهلا وسهلا

    Youssou wakhi doff rk ngay wakh

  • Massamba Gueye
    Massamba Gueye

    🤣🤣🤣čey Daramé

  • Ameth Diallo
    Ameth Diallo

    Moustapha dramé mi lagne wara niouss hamoul dra mouy bigne rek

  • Ndiaye netali fenyi tv
    Ndiaye netali fenyi tv

    no talibe bay xoromouna de talibe bay yi padou nii reck 😃😃😃

  • Serignethiouba Gueye
    Serignethiouba Gueye

    Journaliste ak animateur ak animatrice acteur film sexy dème léne diagui séne diné

  • Serignethiouba Gueye
    Serignethiouba Gueye

    Dieu feu dieuf Serigne Moustapha daramé khame khame bi wérna

  • Serignethiouba Gueye
    Serignethiouba Gueye

    L'I dafa niaaw sakh bolé 2 oustaz du léne diakhasé😢

Siguiente