TAPHA MBEUR SUR ADA FASS "NAKO BAYI AK WAX DJI BEU ARBITRE SIFFLET DINAKO DOOR BAMOU NEWII"
17,030
Reddit
Abonnez-vous à notre Chaine ESonlines: esonlines.info/head/udf.html... Aimez notre page Facebook: facebook.com/becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info .
77 419 03 64

Comentarios
  • Doudou Lo
    Doudou Lo

    Sama champion puissance rk

  • sora Bou Kharagne lo 👊👊
    sora Bou Kharagne lo 👊👊

    Parcelle sunu gokh

  • ABO RIDIAL
    ABO RIDIAL

    Sama mbeur ndam rek ngay ame inchallah

  • Kabila Gueye
    Kabila Gueye

    Tapha svp démal contac lolou rk mon déss dolé bagui fi sa reste ke sa frr

  • Moustapha Sonko
    Moustapha Sonko

    Modou Mbaye wakh nga deuk gnoune wa Parcelles Assainies unité 5 sonn nagnou boy Papa Sambéne sou amé combat dagnouy sonn si agression yi

  • Moustapha Sonko
    Moustapha Sonko

    Toma Mafia P.A bi yeup niogui sa guinaw Ada Fass tégual ko Lou méti bilahi dina boul ko may dara beurré rek lay deff idil ko guita guass bou tarr Ndam rk inchallah Tapha💯💯💯✌️

  • Kenzykind Keinde
    Kenzykind Keinde

    P. A zouu sama u20 sama coner

  • Ibrahima Diagne
    Ibrahima Diagne

    Ki Ada moooko meune futur tigre de fasss sama mbeur bii raguale féte day khagné weur seukkk

  • papa demba keur massar
    papa demba keur massar

    Ndam rek tapha mbeur

  • Papa Ndiaye
    Papa Ndiaye

    Tapha mbeur akka nex😁

  • Hamed Diallo
    Hamed Diallo

    Baye madiaye domou guediawaye dieuleu lene ko mo diangalll léne beur33

  • Aida Samb
    Aida Samb

    Terrain violence ASC Dental(Casa familly)

  • Sarr Abdou
    Sarr Abdou

    Vraiment il à changé SA façon de communication .. mbeur fi ngeu diapp fofou leu ..té wagnį interview you Bari yii...bonne continuation ..am ngeu si lambji thieur?

  • Yoro El negro noble
    Yoro El negro noble

    Modou mbaye tékil sa masqué bi

  • Ibou Ndione
    Ibou Ndione

    Tapeitt nga boy bou Ndaw bi doula may dareuh🤌🏾 Bayil toukh bone mo geune si IOe

  • Ousmane Tirera🔘
    Ousmane Tirera🔘

    Ndam rek mbeur 🕊

  • diop jean
    diop jean

    P.A 4 life

  • aaw mbaye
    aaw mbaye

    Ada fass mola daka beuré dhe defal nak

  • Big Môô
    Big Môô

    Ndame rkk inchallah doff daye demm dh🔥👌👌

  • Talibe Bamba
    Talibe Bamba

    Bonne chance à tout les deux

  • Baye yaram Dof
    Baye yaram Dof

    demal entrainé neko si dara djeul sa sccoter bobou fou way tourné guiss la ak mom demal train boudé lamb ga opté def co metier

  • Cheikh bass Keur massar
    Cheikh bass Keur massar

    Terrain violence mako xam Modou

  • Cheikh bass Keur massar
    Cheikh bass Keur massar

    Tapha mbeur jaay preck wakh rek nga am si Kombat bi lou leer laala wakh nak

  • Kouy Ngome
    Kouy Ngome

    Lila Sénégalais khamé boulko bagui

  • SALIOU DIALLO
    SALIOU DIALLO

    Fall yaw bémal liguéyi té bayi nakhéyi Ada doussa morome limou liguéye liguéyoko

  • Frank Al
    Frank Al

    Tapha mbeur li ma méti challenge la fi néké guel yi diko topando sou démé lamb dji gnou dane ko 😂 ki comedien la way dou mbeur

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      😂😂😂😂😂😂

    • diop jean
      diop jean

      li guay wakh khamo ko

    • Big Môô
      Big Môô

      Tapha niata Défaut la ame

  • SALIOU DIALLO
    SALIOU DIALLO

    Tous nak Ada FASS boula djapé day dirékou sa kawe inchallah

  • Indochine🇸🇳
    Indochine🇸🇳

    Nooooo mais mbeur thiattt Sama champion lolou rek moko manké Mouy Modou lo kham kham kham khamou niou Dara,,😂😂🇺🇲🇸🇳💯

  • Moustapha Fall
    Moustapha Fall

    Ndaam rék toma insha'allah douma ndann derrière toi puissance 👍✌💪

    • Cheikh Fall
      Cheikh Fall

      Machalla tapha 💪

  • Abdou khadre Diop
    Abdou khadre Diop

    Allé. Doffff ✌️

  • L'absolu Gueye
    L'absolu Gueye

    Ada fass Isk Daxoula Beraii Tapha 😟 Ahhh waa Baxna Ada fass Dafa Meune Beraii Trop Billahi Mé Nak Que le meilleur Gagn champion nga Amall jamm Rék 🤙🏻

  • Mamadou Ndiath
    Mamadou Ndiath

    Cheikh gueye ya meneu nday doulll

  • khadim lo
    khadim lo

    Tapha mbeur..😂😂😂😂🤲🤲🤲

  • Crunchblox
    Crunchblox

    Yene niou fekelen pikine teubeul lene bay nagou sen 2roues yii ngay doul mtx deuxiem signature bii ngene daww bayil doul

    • Petit Tall
      Petit Tall

      @Edalé Bodian Lolou moma diakhal vraiment l'heure devient grave. Niome nieup nakk aye ragal lanou bo xolé ba ci biir ci internet bi lanouy beuri wakh.

    • Edalé Bodian
      Edalé Bodian

      Sénégalais violence lay bako

    • Crunchblox
      Crunchblox

      @L' Amateur de Lutte SN_officiel no pas pour mane pour nieup

    • L' Amateur de Lutte SN_officiel
      L' Amateur de Lutte SN_officiel

      @Crunchblox hun kon nonou la dmé pour ioe?

    • Crunchblox
      Crunchblox

      @L' Amateur de Lutte SN_officiel daww faneu ioe by bii nioka yobb ba stade khekh niou teubeuli by p.a niou daw gnouné signature bii dou am

  • Gora Fall
    Gora Fall

    Mbeur idée bou Nice laa franchement Parcelles Assainies sama secteur

  • BBT Dieng
    BBT Dieng

    Merci bcp Modou Mbaye, pask tu as géré le marketing le fait que tu as enlevé l’étiquette de la bouteille. C est pour éviter de la publicité

    • Méta L'OriiGinaL
      Méta L'OriiGinaL

      Il a déjà fait la publicité en prononçant le nom di produit

  • Mohamadou Diallo
    Mohamadou Diallo

    Ndam rek

  • İbrahima
    İbrahima

    Wa parcelles danio nitté danio sétt

    • Indochine🇸🇳
      Indochine🇸🇳

      Bilahi wakh KO si kaw aferbi sport la rek sou diékhé diékh n'a kén d'où si dane sa morome ba Ray KO wassalam

  • Hamdy Junior
    Hamdy Junior

    Thiey tafff Mbeur 🔥🔥🔥

  • Cheikh Barra Kandji
    Cheikh Barra Kandji

    Très bonne communication 🕊🦁

  • Kalla 💯bou mame💯 sam ♻
    Kalla 💯bou mame💯 sam ♻

    😂😂😂😂Bilahi waxx na deug terin violence aka mako xam 😂😂

    • Aida Samb
      Aida Samb

      Lou graww

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      😂😂😂😂

  • Élmalick Sindidi
    Élmalick Sindidi

    tapha mbeur domou deuk bi(diander

Siguiente